SERIGNE TOUBA wakh nani

diourome niar mo gueune diourome niar

1-Bayi fène mo gueune diangue AL KHOURANE
2-Saame sa diourome niari thieur mo gueune deuké koor
3-Fatalikou alàkhira mo gueune fanàné diouli
4-Làbiré mbolèm dioulite yi mo gueune fital djaare
5-Bayi moye mo gueune deuké djéguelou
6-Diglé aw yiw mo gueune baril sarakh
7-Tèrè lou niaw mo gueune dieuké niane

Diammi adouna mooy werouck yaram
Noflayou adouna mooy am dono
Wètelou adouna mooy am sokhna
Yeurmandé adouna mooy am dom
Kham khamou adouna mooy khame yallah
Mane manou adouna...manèko say bok

Kouye toube,laye djègueul
Kouye mougne,laye diokh ndam
Kou am tèguine,laye diokh barké
Kouye sante,laye doli
Fatali(Wakhi Serigne Touba)
Nitt gni niniou ragaleh niakk bouniou ko ragaleh woone YALLA dinaniou am YALLA teh douniou niakk

kepp kou beuga topp Yalla te amoul ay tèggiin dou am mouk lamou beug
bou kènn gnew ci yaw di sakou loo ko mana dèfal nga bagn ko koo dèfal
boul dougg mouk ci nèègou jambour di sànni say beut founèkk ndakh
- man nga fà giss lou gnou doon soutouraal tè bagn kènn giss ko
dèèl tèèrou gan ci mbègtè tè oubbil ko sa kanam ndakh oubbi gan sa kanam moo geuna nèkh ci moom tèranga boumou
- mana doon
dèèl yeureum kèp koula fèètè ndaw tè dèèko digal foo tol lou koy diarign tè di ko tèk ci yònou ndioup

Articles de la même rubrique

Vidéo à la une

Restez informés

PUBLICITE

Poster pour fond d'écran